wolof Soppi

  Gongikubaat Soppi

taw

  1. taw ndox miy bawoo ci asamaan wàcc ci suuf, tey doon lu nit ñi man a yëk,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof: Soppi

  1. biig dey taw na tawub waame, réew mepp a ngi ji,

Xool it Soppi

Tekki Soppi

  Waxiin

Déglu baatu taw ci wolofi Senegaal