Daaxër-daaxër

Dox dox bu metti.

Niral: Lu muy daaxër-daaxër di ñëw nii ?