Saraax, parax, pëll. Baat bi dafay tekki lu jékki jékki rekk dugg fenn.
Niral: jinax ji nee na dagaj ci biir pax mi.