Dal
wolof
Soppi- tambali: dal na jàng, dal na Baa, dal na di dem.
- lu ne tekk: taw bi dal na: nee na tekk, bu coow li dalee nga dégg li ñuy wax
- wàcc: fan nga daloon keroog ca Màggal ga, Maa ngi daloon sama kër sëëriñ
- wàccuwaayu gan: fan mooy seen dal? xanaa sama kër sëriñ
- dina tekki it li nuy wax ci nasaraan principe (1)
- ci xam-xamu nosukaay: ab sit internet (2)
yeneeni làkk
Soppifrançais
Soppi- principe (1)
- site (2)
english
Soppi- principle
- site
Italiano
Soppi- principio
- sito