- sanc: mooy dem ci beneen barab boo dëkkutoon sanc ko, moo xam fu kenn dëkkutoon la mbaa muy ab gent, mbaa fu nit dëkk, xajale fa mbaa ñu jaay ko doole
- dem cib barab took fa, dëkk fa cig sañ-bañ, yilif ña fa dëkk ci doole, (mi ngi juge ci canc gi ñu njëkk a wax, ci tomb bi ci kaw) (1)