Wiktionary:baati sinemaa

ci wii xëtu sémb baat yi ñeel sinemaa lañu fiy waxtaane:

  • angle (de prise de vue) = Ponk, koñ, ruq, aw gisiin
  • bande sonore = dog wuy coow, bànd bu xumb, bànd buy kàddu, dog wuy kàddu(walla lëmës mbaa taxañ (bande) buy sab)
  • décor = rafetal, taaral, (ci tiyaatar = misaal: (ab séenu bu misaal, )
  • découpage = dog,dogiin,daggate, daggatiin (walla rafetal ci kayit)
  • effets spéciaux = jeexiit yees jagleele, jeexiit yu am ay jagle,yu di woroomi jagle, ay naxe, ay way jortuloo
  • métrage (court/long) = yàggaay(gu gàtt/gu gudd)
  • plan, scène, séquence = naal sémb(palaŋ), scène = ab séenu, ab xewuwaay. séquence = ag callala, ag toftaloo aw dog
  • fILM = film, guuxaan