ab natt
ag mbootaay la guy teg (natt) benn cér di teggi, ba mu wër ñépp, loolu di nekk ag dimbalante gu ñuy joqalante . Man naa tudd tam "Ag joqalante" ñu jublu ci natt biy wër ci seen biir ñu koy joqalante. Bu dee ci Fr: Mutuelle day tekki "lu ñu joqalante" manees na koo tudde tam "ay loxoy Kajoor"