wolof

Soppi

Gongikubaat:laïcité mi ni bawoo ci wu gres "laikos" : ag bar, aw askan (peuple).

ci waxiinu nasaraan yi nag , ku diineedi da daan nekk ci jamono ju diggu ja, ku ñu "cangat, ku ñu ngénte" kok bokkul ci niti diine ji. Ci jamono jii mooy ki nu jox liggéey yi niti diine yi jagoo woon, ci aw xeet wu katolog ci ñaareelu xaaju XIXeelu xarnu. Ci ron IIIeelu pénc mi, diineedi mujj na di ngérum nos ag mboolaay guy sàkku ag péetéedi gu ñu joqalante gu nguur yu ruu yi ak yu diine yi, ci lu aju ci nguur gu mbooloo mi (pouvoirs politiques), gu ñoñ gi (civil), ak gu doxaliin gi (administratif). li ko taxoon a jug mooy xeex "ngérum niti diine mi" ( cléricalisme), maanaam dooley ak jeexiital gi niti diine yi ak yëngu-yëngu mbaa làngi diine yi amoon ci mbirum mbooloo mi. Diineedi it jikko la ju bóof ci ag péexte ci ngëm , muy yuqamtiku nag jëm ci ubbikug nit niki jëmmaan (individu)ak aji réewu (citoyen).

Ci lu ñu daj, diineedi mi ngi samp ci dali tàqale gu yoon ci diggante jàngu bi ak nguur gi (la laïcité est fondée sur le principe de séparation juridique des Eglises et de l'Etat)

(yoonu 1905 ca Frãas), rawati na ci lu aju ci njàngale.

français

Soppi
  • laïcité