ag njënd
Ag njënd ci politig ag anam la gu ñuy jaar ba nit ki walla aji kàddul ji jox la ag kàddom bu demee ca mbàñ-gacca ya, jaare ko ci di ko jox ay may mbaay xéewal, maanaam daal jënd ko