aw
Wolof
SoppiAw: amna ñeenti maanaa
- Aw ku nekk ci mbir ba sonn bàyyi ak keneen mu def.
- Aw bu dara dee tuuru nga wut lu ko tee yeng suuf,
- Aw dees koy jëfandikoo ci njëkk baat muy wund ben mbaa lu bari,
- Aw ku jaar ci aw yoon di dem
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- awal gone gi ci liggéey bi sonn na kat
- li nga ajoon ci kaw de xaw tuut mu tuuru diw a ko aw
- aw xët benn la, aw nit lu bari la, aw mbooloo lu bari la,
- du ma gis aw xàll di aw ci aw ñall