bëy
wolof
Soppibëy:
- bëy mala la ci mala yi dëkk ak nit ñi,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- geenu bëy sànguli taat!
Xool it
SoppiTekki
Soppi- wu-faraas: chévre
- wu-angalteer: goat
Déglu baatu bëy ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bëy.ogg