bari
wolof
Soppibari:
- bari lu ap ñatt ci lees man a waññi, tey duun ci lees man ta waññi
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- Xamnaa xeeti xam-xam yu bari. Amnaa xam-xam bu bari.
Xool it
SoppiTekki
Soppi
Déglu baatu bari ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bari.ogg