ber
wolof
Soppiber: am na ñaari maanaa
- ber lees xéjji ci'y moroomam,
- ber suuf su nooy la tey xonq,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- seetal ben bu baax nga ber ko,
- gasal foofu am na suufus ber
Xool it
SoppiTekki
Soppi- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu ber ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-ber.ogg