wolof

Soppi

daal: am na ñaari maanaa

  1. daal dees koy jëfandikoo ngir gàttal wax.
  2. ag daal/ag deel arafu araab la, 4eelu araf ci abajada araabu daaray senegaal

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

Soppi
  1. moom daal ku baax la,
  2. daal 4 la ci xayma

Xool it

Soppi

Tekki

Soppi

  Waxiin

Déglu baatu daal ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-daal.ogg