dar
wolof
Soppidar: amna ñaari maanaa yu man a bokk
- dar lu tafu sës rikk ci dara
- dar niki cin lu dar
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- dar ko rek bu ko bàyyi
- soxna si sa cin laangi dar
Xool it
SoppiTekki
Soppi- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu dar ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dar.ogg