wolof

Soppi

diir: amna ñaari maanaa

  1. ab diir moo di ab àpp
  2. ag diir natt dara ngir jam ko mbaa dal ko,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

Soppi
  1. diir bi nuy am ci àdduna yàggul warees na koo rafetal,
  2. diir naa till gi ba jam ko

Xool it

Soppi

Tekki

Soppi

  Waxiin

Déglu baatu diir ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diir.ogg