diw
wolof
Soppidiw: amna ñaari maanaa
- ag diw niki ndox lay xellee tey niin
- diw manees na koo wax jublu ci ku ne
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- diw day niin
- diw dee ma may xaalis
Xool it
SoppiTekki
Soppi- wu-faraas: - pétrole
- wu-angalteer: - oil, ointment
Déglu baatu diw ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diw.ogg