duusi ceññeer-mbëj
wolof
Soppi- leeral luy duusi ceññeer-mbëj :
duusi ceññeer-mbëj li leen di màndargaal mooy seeni deng-dengi, walla seeni guddaayi duus. duusi ceññeer-mbëj yi Tele moo koy jëfandikoo, Rajo ak Radaar yi...
faramfacce gi :
Aliway dëppoo gi am ci diggante deng-dengi gi ak guddaayu duusi ceññeer-mbëj yi
- Deng-dengi gi........guddaayu duus
3 à 30 kHz.......myriamètriques
30 à 300 kHz.....kilométriques
300 à 3000 kHz...hectométriques
3 à 30 MHz.......décamétriques
30 à 300 MHz.....métriques
300 à 3000 MHz...décimétriques
3 à 30 GHz.......centimétriques
30 à 300 GHz.....centimétriques
français
Soppi- Description de l'onde radioélectriques :
Les ondes radioélectriques sont caractérisées par leur fréquence ou par leur longueur d'onde. Les ondes radioélectriques sont utilisées par la télévision, la radio, les radars ...
Détails :
Tableau de correspondance entre la fréquence et la longueur de l'onde radioélectriques
Fréquence........Longueur d'onde
3 à 30 kHz.......myriamètriques
30 à 300 kHz.....kilométriques
300 à 3000 kHz...hectométriques
3 à 30 MHz.......décamétriques
30 à 300 MHz.....métriques
300 à 3000 MHz...décimétriques
3 à 30 GHz.......centimétriques
30 à 300 GHz.....centimétriques