gàttub njot
Gongikubaat: wii waxiin mi ngi bawoo ci xumbéelug yaxood gi aju ci Jéggalu, ci biir màggal googu mbaa xumbéel googu dees fay jël ab gàtt ci maanaa, sëf ko mbooleem njuumte ak ñaawtéefi Israayil , bu ñu noppee dàq ko ci tàkk gi, mu dëgmal Asaasel (senn saytaane, malaaka mu ñàkk-yaakaar) ngir mu wëlbati rëbbum Yàlla mi. Cosaan la boo demee ca Linjiil fekk ko fa ca lEVITIQUE 16: 7-10