Leeral ay baat

Soppi
  • bu ñu nee Tur ci ab baat, moodi njëkk baat ba, Misaal: Aw xët, aw gi moodi tur wi.
  • bu ñu nee Sant ci ab baat moodi lay tegu ca baat ba, Misaal: xët wi, wi gi moodi sant wi.
  • baati doxondeem mooy baat yi junge ci yeneeni làkk te ñu koy jëfandikoo ci lu manta ñàkk mbaa muy ci baat yi ñépp bokk.
  • xarbaax moodi lépp lu soppi li nu fi miinoon.

aji leeral ji: Abdu Xadir Gey >>Ahloubadar