lonkoo
Wolof
Soppi- ag lonkoo it day firi (société)ci nasaraan, maanaam lu ay nit lonkoo taxawal ko, baat bi nag mi ngi bàyyikoo ca la daa xew ci daaray alquraan yi ndongo yi daa ko def muy wax seeni moroom naan leen nañu lonkoo bokk, maanaam nañuy def lu ñu am bokk ko, lu ñu suñu ay way-jur indilati walla ay mbokk nañu ko di bokk.
- lonkoo: jëf la juy am ci diggante ñaari jëmm, di tax ag jokkoo di am ci seen diggante akug laalante akug jonjoo.
yeneeni làkk
SoppiFrançais
Soppi- connexion
- société (eco)