ne-ne
Wolof
Soppi- Lu ñu man a daj, man cee teg loxo:
Ne-ne, ñu xame ko ci frãse ci((matière))mooy li toggale wépp yaram wu am ag nekk gu nu man a laal (une réalité tangible). Ñatti melokaanam yi ñu gën a miin nag, ñooy melokaan wu dëgër(l'état solide), wuy yol (l'état liquide) ak wu gaasu (l'état gazeux). Moom day jël barab(elle occupe de l'espace)te kemub ne-ne (la quantité de matière) ñi ngi koy natte ci jóor(la masse) (bu fekkee ne mbir mi dafa aju ci waññ xaajiiti ne-ne(particules de matière), deesi jëfandikoo (la mole) ).Ci noonu, ci xam-xamu jëmm, lepp lu am ab jóor rekk ne-ne la. Ci biir loolu, ne-ne yu ñu miin yi ñu wër, ñi ngi sosoo ci ay bariyon,kon ci waxiin wi nu baaxoo, boo ci déggee baatub ne-ne, nanga xam ne ne-ne bu bariyon lañu jubloo wax. Tekkiin wii kon boolewuñu ci boson yu dàttu (les bosons fondamentaux), yi nga xam ne ñooy tuxal ñeenti doole yu dàttu yi ak doonte am nañu ab jóor ak/walla genn kàttan.
Français
Soppi- Matière
English
Soppi- Material