ngérum Trotski
Ngérum Trotski ab dawaan bu politig la bu mbokkte buy wund xalaati Leon Trotski, mi sos mbooloom xare mu Risi mi, bi Lenin dee la ko Stalin dàqe ca nguur ga, génne ko ca làngug mbokkte ga ca 1927. Ñu génneeti ko ci Bennoog Sofyet gi atum 1929, bóom ko ci 1940, ki ko def di lenn ndaw lu tukke ca Stalin