Accueil
Au hasard
Dugg
Configuration
Jàppale nu
Ci mbiri Wiktionary
Ay aartu
Seet
nguur g-
Langue
Topp
Soppi
wolof
Soppi
réew walla dëkk bu ay buur jiite, moom ko,misaal:
nguurug Kajoor
nekke ni ko neex gi buur di def:
moom de day nguuru cig njoowaanam
doole ji jiite am réew ak doonte du mu ay buur:
nguurug Senegaal
te nosteg pénc la
français
Soppi
royaume
l'état; le pouvoir