Accueil
Au hasard
Dugg
Configuration
Jàppale nu
Ci mbiri Wiktionary
Ay aartu
Seet
njëwriñ
Langue
Topp
Soppi
(Yoonalaat gu jóge
njëwrin
)
wolof
Soppi
Gongikubaat
Soppi
ci la
jëwriñ
juge: ag njëwriñ lanuy wax mooy fi jëwriñ ji di nekk ak mbooleem li mu yilif.Ñenn ñi di ko wax:
kër jëwriñ
,ñi ci des naan ko:
makaanu jëwriñ
Yeneeni làkk
Soppi
wu-faraas
:
ministère
wu-angalteer
:
ministry
wu-itaali
:
monistero