ponk b-
wolof
Soppi- aw dog ci mbind mu aju ci yoon, nga xam ne di na faral àgg ci ay wenn ba ñatti rëdd.
- koñ : ponku néeg bee daa xaw a jàdd
- tomb: tay am na ay ponk yu bari yu ñu war a waxtaane
- keno: mbaar mi amul ay ponk
- dàtt: mbir danga koy tegg ci ponk yu dëgër boo bëggee mu jëm kanam
français
Soppi- article (loi)
- coin
- point
- fondement