sébbi
wolof
Soppisébbi amna ñaari maanaa ci wolof
- sébbi newet buy door,
- sébbi jalu mbuubit bees di yàq
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
Soppi- bët sébbi na, kuy bay wara jige ji say tool
- sébb bi ma defoon fii taxankat yi sébbi nañ ko.
Xool it
SoppiTekki
Soppi- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu sébbi ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-sébbi.ogg