ñaarñaarloo
Wolof
Soppixoolal ñaar
ñaarñaarloo:
- luy ñaarñaarloo, mooy ànd ñaar ak ñaar.
- kàllaamay ñaarñaarloo, mooy kàllaama gooy binde ñaari màndarga(0 ak 1), loo bëgga bind
- ci Xam-xamu nosukaay, mooy kàllaama gi ñuy jëfandikoo ngir doxal nosukaay bi