bataaxalub mbëjfeppal
(Yoonalaat gu jóge Bataaxalub mbëjfeppal)
wolof
Soppixoolal mbëjfeppal ak bataaxal
Bataaxalub mbëjfeppal
- Bataaxalub mbëjfeppal di nañ ko wax itam m-bataaxal
- Yónne ma ab Bataaxalub mbëjfeppal ci sama boyot.
yeneeni làkk
Soppi- wu-fraas: courriel électronique
- wu-angalteer: e-mail
- wu-itaali: posta elettronica, e-mail