Caga
Wolof
Soppi→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Caga b
- Jigeen ju jëkkëram gaañu wala mu tàggoo ak jëkkëram. Néew na lu wolof yi di jëfandikoo baat bi ci tekki bii.
- Ndaw soosu ab caga la, daaw la tàggoo ak boroom-këram. / jigeen juy jaay boppam. Jigeen ju xam boppam du dem mukk di nekk ab caga.