I am a sysop (Yorkat) in this Wiki.
I am a sysop (Yorkat) in Wikipedia.
I am member in Omegawiki].
I am member in Betawiki.
I am a member in it wikipedia .

wolof: Sama tur mooy Ibrahima fall, ibou di sama dakkantal. Am 24 at. Ci samag dund gu dëggu damay jàng daara-ju-kawe ju Padova ca Itaali . Xibaar laay topp. Venezia (Itaali) laa dëkk am na 6 at.
Ci 2007 bii laa tambalee jang wolof. Mooy làkk bi ma gënn a neex. Ci 2007 bi itam laa bindu ci Wikipedia tambalee cëru ci liggéey bi. Ab yorkat laa.

li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu Seex Anta Joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy Paulo Coelho di ab waa beresil.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.

English: My name is fall ibrahima, i stady automation in the university of padova in italy. I live in venice. I started to contribute in wikipedia in 2007. I am administrator in wikipedia wolof and wiktionary. i translate the mediawiki interface into wolof.

Dencukaay:Cheikh Anta Diop.gif
Sama royuwaay bi gën a mag ci wàllu adduna
Seex Anta Joob