Melosuuf

(Yoonalaat gu jóge Séwogaraafi)

Wolof

Soppi

Mi ngi jóge ci baatu melo ak suuf

Melosuuf

  1. Mooy xam-xam biy settantal ak a leeral feeñtey yaram yi, walla yu jëmm yi, yu dundat yi, yu nit ñi ci kaw suuf si ak gëstu gi aju ci seen séddalikoo, melal suuf si, wax ni suuf si mel

Ci yeneeni làkk

Soppi