saasumaan

(Yoonalaat gu jóge Saasumaan b)
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

saasumaan b

Day tolloo ak xale bu góor bi, waaye ci biir xale bu góor man ngaa nekk xale bu góor te doo nekk saasumaan, ndax saasuman dëgg dëgg day tolloo ak (booy diskoo) ci sunu jamono jii.

Tekki

Soppi
farañse: -
angale: -
itaaliyee: -