Waxtaan:ay
Dernier commentaire : 15 at ci ginaaw par Ibou
Ay du jumtukaayu xammeedil, waaye barilukaay la, misaal: am xam ay xar, kon ay foofu mooy barilukaayu xar yi ndax bu dee am la menn lay doon bu dee ay di yu bari --Abdu Xaadir KEBE 3 Maars 2009 à 02:58 (UTC)
- ci li nga bindoon rekk laa sukkandiku, yaakaar naa ne "article indefini" yaa ko tekkee woon jumtuyaayu xàmmeedi te ay moom la. kon suma déggee bu baax li nga bind mooy ne article tekkeetoo ko loolu waaye barilukaay lay tekki leegi? article defini: barilukaay xàmmeel, article indefinie: barilukaay xàmmeedil. soo ame jot itam bëggoon naa nga defal ma ab gëstu ci baat yi ci xët wu njëkk wi, léegi baat yi ñu wara tekki, fa la leen di def.--Ibou 3 Maars 2009 à 11:58 (UTC)