automatique
aji jekki-jekki-defu: il a répondit de manière automatique: tontu na ci anam gu jekki-jekki-defu.
Si tu le frappes sa réaction sera automatique: soo ko dóoree ag fayyoom aji jekki-jekki-defu la (luy jekki-jekki defu la)
lu boppal, lu automatique, il a répondit de manière automatique: moo tontul boppam, ag tontoom daa boppal, Si tu le frappes sa réaction sera automatique: soo ko doore mooy fayyul boppam, walla ag fayyoom day boppal --Ibou 20 Ndeyi-koor 2008 à 10:38 (UTC)