wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

cër:

  1. Nit: wàll yi ci jëmm ji, loxo yi ci cër yi la niki tànk yi;
  2. mbootaay: Senegaal cër la ci xeet yu bennoo yi (mbootaayu xeet yi), Senegaal ci mbootaayu xeet yi la bokk.
  3. Koom-koom: liy tax ngay bokk ci ag mboolaay walla ab liggéeyuwaay jaare ko ci jënd fa ay cër.
  4. Wàll: jox ma sama cër ci li ñuy séddale: jox ma ci sama wàll;

yeneeni làkk

Soppi

wu-faraas: membre, action, part, élément