daara (ji)
(Yoonalaat gu jóge daara (ab))
Wolof
SoppiMooy barab ba ñuy jànge ak a jàngale, cosaan la: fa jàngkati alxuraan ya daan jànge ak way xamlu diiney Lislaam ya, mu jëm-kanam ba ñu mujj di ko jëfandikoo ci lépp lu di barabu njàng ak njàggale
Turandoo
SoppiYeneeni làkk
Soppiwu faraas: école, centre |
wu itaali: scuola |
wu angalteer: school |