Wolof

Soppi

Mooy barab ba ñuy jànge ak a jàngale, cosaan la: fa jàngkati alxuraan ya daan jànge ak way xamlu diiney Lislaam ya, mu jëm-kanam ba ñu mujj di ko jëfandikoo ci lépp lu di barabu njàng ak njàggale

Turandoo

Soppi

Jàngu

Yeneeni làkk

Soppi
wu faraas: école, centre
wu itaali: scuola
wu angalteer: school