gëstu
Wolof
SoppiMooy topp am mbir def ci ay jàngat, fexe ba xam lépp lu ku ëmb, li ci laqu ak li ci feeñ.
- Nit kii de def na ag gëstu gu yaa ci diine
- Nit kiy gëstu mooy ab gëstukat
- Fàwwu nga gëstu ngir xam
yeneen làkk
Soppiwu faraas: chercher, rechercher, faire des recherches