gerte tubaab
Wolof
Soppigerte ak tubaab → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
gerte tubaab g
- garab giy jur gerte tubaab.
gerte tubaab b
- meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug gerte tubaab
Tekki
Soppituru xam-xam: Terminalia catappa |
farañse: badamier |
angale: indian almond |
itaalyee: mandorlo indiano |