Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

imbraatóor b

  1. buur bu jiite ay nguur yu bari yu booloo

imbraatóor g

  1. nguur yu bari yu booloo

Tekki

Soppi
farañse: empereur, empire
angale: emperor, empire
itaaliyee: imperatore, impero