Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

jambur:

  1. ku dul féete, du far
    nit kii de jambur la walla nit kii de ku jambure la
  2. ci xayma: du soppi yeneen cër yi, soo leen boolee, loo manti yokk Tus (0) du soppiku. Kon Tus cër bu jambure la

maandu

Tekki

Soppi

wu-faraas: neutre

wu-angalteer: neutral

Delluwaay

Soppi

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005