Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

këmm:

  1. mooy ñàkk a ndékki, yewwu ne këmm
  2. mooy lu dara nekkul, lu ne këmm.
  3. mooy it baaraam bu dagg ca cat la, baaraam bu këmm

Tekki

Soppi

wu-faraas: vide