lammeñ
wolof
Soppici wolof yi
lammeñ:amna ñaari maanaa ci wolof
- lammeñ ab cer la ci nit bu nekk ci biir gemmeñ, nu koy jëfandiko ngir wax ak taqqam tiku ak..
- lammeñ làkk wune ña ca cosaanoo, lammeñ lay tud ci ñoom, misaal:senegaal wolof lammeñ lafa waaye nasaraan aw làkk lafa
nduroowaale
SoppiTekki
SoppiDéglul baatub lammeñ ci wolofi Senegaal