Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

njàndam g

  1. garab giy jur njàndam.

njàndam b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug njàndam.

Tekki

Soppi
turu xam-xam: Boscia senegalensis
farañse: hanza
angale: hanza
itaalyee: hanza