xaalu tubaab
Wolof
Soppi→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
xaalu tubaab g
- garab giy jur xaalu tubaab.
xaalu tubaab b
- meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug xaalu tubaab.
Tekki
Soppituru xam-xam: Cucumis melo |
farañse: melon |
angale: melon |
itaalyee: melone |