Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

xam-xam b

Mbooleem ay xameel yu wòor yu aju ci yenn xew-xew yi, ci ay mbir walla ci ay feñte; xam-xamub nite: xam-xam bu ñeel nit ak mboolaay; xam-xami xayma ak saytu.

Tekki

Soppi
farañse: connaissance
angale: knowledge
itaaliyee: conoscenza