Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

xewar g

  1. garab giy jur xewar.

xewar b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug xewar

Tekki

Soppi
turu xam-xam: Lepisanthes senegalensis
farañse: cerisier du Cayor
angale: -
itaalyee: -