Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

Soppi

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

bàyyikoo g

  1. ci ndefar: ag njuréef man naa bàyyikoo ci geneen, ni diw di bàyyikoo ci gerte
  2. ci nos-wax: ab baat bu bàyyikoo ci beneen, baat bu am reenu beeneen, ca boobu la bàyyikoo.
  3. barab, fa am mbir jóge

Tekki

Soppi
faraňse: origine
angale: origin
itaaliyee: origine