baril
Wolof
Soppimi ngi bàyyikoo ci bari
baril:
- yokk limu am mbir, def ko mu bari
- jàngi téere moo la taxa mana baril say baat yi nga xam,
baril g:
- yokk gi ngay yokk limu mbir mi
- baril gu samay falkat moo ma taxa falu
Tekki
SoppiDelluwaay
SoppiMbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005